
Souhaïbou TV
Souhaïbou TV sen bi dul tàyyi ci liggéeyal askan wi.
La chaîne infatigable au service du peuple. ??
Seen mbégte ak seeni njàriñ ñooy sunu yitte.
Votre satisfaction et vos exigences sont notre raison d'être.
Sunuy wëppa ⤵️ :
Mboor/Taariix: lépp lu aju ci mboorum Senegaal, mbatiit, aada añs... Ak mboorum àddina sépp, ak mboorum yonent yi ak bépp taariix bu aju ci Lislaam (leeg-leeg it nu jëfandikoo baatub jaar-jaar, su ñeelee jenn jëmm)
Léeb : Léeb day jaare ci lu ne (lu yem xel, lu romb xel, lu nit taamu di gis, lu mu masul, niki mala buy wax...), ngir jàngale; nun nag sunuy léeb jàngale mbaax (jikko ju rafet) mooy jubluwaay bi,
Nettali : Am na ci nettali yoy yees fent lañu. Am na ci yoy yu dëgg lañu (yuy nit dund) ; ci biir yooyii am na ci yoy i téere lañu, nu fésal leen ciy widewóo, ngir ñi manut a dawal mbaa seenug jot xañ leen ko. Lépp tànku nag ci jàngale mbaax.
Àdduna barab bu lëndëm la, xam-xam ay làmp bi koy leeral.
ABONEEL te AKTIFE KOLOOS BI
Country: Youtube channel: Souhaïbou TVCreated: May 31, 2018
Subscriber count: 129,000
Country rank by subscribers: 74
Channel views: 9,040,967
Country rank by views: 74
Channel videos: 229